Signaler un problème
...
Moustapha Ndiaye 04/03/2017 00:17:36
Pourquoi sounou politiciens yi lignouy wakh ak lougnouy deff d'où ben Mika waral moy beug post bou bakh ak pouvoir bi mon takh gnou diayy séné ngor é pourtant diplomatie exemplaires la wara nekk ndakh mou défense drapeau deukeum wasalam
...
Moustapha Ndiaye 04/03/2017 00:12:02
Politiques Sénégal amoul ben rendment ndakh bougnou dioté si pouvoir bi rek faté popilation bi conn ndakh diaratina gnouy sani sounou carte
par