Tv / Aida Samb Gëstu - une production Prince Arts Studio (+LYRICS dans la Description)

06:30 | 22 | ambengue
Ajouté 2014-09-13

Vous pouvez VOUS ABONNER à notre chaîne en CLIQUANT ici : http://www.youtube.com/subscription_center?add_user=princeartsmusic Rejoignez nous sur: Google+ : http://gplus.to/PrinceArtsMusic Facebook : https://www.facebook.com/PrinceArtsMusic Twitter : https://twitter.com/princeartsmusic - - - PAROLES - - - LYRICS - - - { commencer à chanter à partir de 1:11 :) } Ling mey khol lo, dimako khelilo bobou beu legui mangui gestou man guissouma dara Lingmey khol lo yaw dimako khelilo bobeu legui mangui guestou man guissouma dara... Niit ki niit ki niit kiiii Niit ki niit ki niit kiiii Lingmey khol lo yaw dimako khelilo bobeu legui mangui thi mane mi khawmeu loumou done Ndaw day sogua door diapeu tha la warr wayé boulko fakhasstale, loléé waroulaaa Niit ki niit ki niit kiiii Niit ki niit ki niit kiiii Ndiom ak Ndiambar ra takhone mane meu topeu leu dem na beu guissoumeu thi yow fouleu mangui soumeu yone Ndaw daye sogua dor diapeu tha la warr wayé boulko fakhasstale, loléé waroulaaa Niit ki niit ki niit kiiii Niit ki niit ki niit kiiii Ndiom ak diambar a takhone mane meu topeu leu dem na beu guissoumeu thi yow fouleu mangui soumeu yone Ndaw day sogua door diapeu tha la warr wayé boulko fakhasstale, loléé waroulaaa, loléé warouleu Kalaass adouna ngi ni dal gestou ni la métééé Kalaass adouna ngi ni dal gestou ni la métééé Diafandoul diafandoul djeuf mom dafey wess Diafandoul diafandoul djeuf mom dafey wess Diafandoul diafandoul djeuf mom dafey wess Amone na yaakaar ni soma khello khelliloma ma wakh la khalat lo ma yow Adouna ak yatouwayam yalla ak yeurmandém bouko khol yillé yatouwone kone mou nekh beu diakhal ga gni Mane bi mey gneuw fi mane khawma daray, te bimey gneuw fi bobou khaléla Seyni ndiaye Fall thiey Seyni Ndiaye Fall yééé Seyni Ndiaye Fall Mane bi mey gneuw fi mane khawma dara, té bimey gneuw fi bobou khaléla Amari Guisse mane mimey woy kokou sameu ndidiaye la Yalla moy bollé domou adama yi té moma bollék Coumba Fall Seck Coumba Fall yayou Mouhamed kokou sama maman la Yalla moy bollé domou adama yi te moma bollé ak tonton Habib Sy tonton Habib gorou Coumba Fall kokou sameu ndidiaye la Seyni Ndiaye Fall bi mey waye mom boléwoul dara ki wakh mom dinama téral té dina ma téral té dima tété ték mathi yone wou bakh Mom Seyni ndiaye Fall thiey Seyni Ndiaye Fall yééé Seyni Ndiaye Fall

Partager cet élément sur Facebook Twitter