Signaler un problème
 
...
boudechou 10/04/2017 14:10:24
les femmes sont dangeureuses, djiguene dou kharit et c'est la triste réalité...
...
AbdouLahad Diakhate 10/04/2017 13:32:44
Ma serie préferée j'aime bien IDOLES mais je ne retrouve plus le photographe Camara Laye et l'infographe ou st ils!
...
BlackPanther 10/04/2017 13:22:43
Mais Even Prod Senegal nane laye def pour ame soundtrack bi
...
Kiné Diaw 10/04/2017 12:42:06
Madré nn Biolay mame Nené mi dîna ma ray Adams moytoul Bala gnou les viloe
...
sa dakar 10/04/2017 12:35:09
deglou leine adam's 27mn51s jus'qua 53s neina (ils oze plainte partie contre moi) lol bilahi j'ai falliit pleuré a cause de cherif yeureum nako sakh on dirait q'uils voit les djinnes
...
Awa Diallo 10/04/2017 12:13:15
chériff, tu fais souffrir des familles entières avec ton rôle. Que des souvenirs douloureux !!! Dieu aie pitié de son âme !!! amine
...
Malick Diop 10/04/2017 11:14:35
dzlé malick elle t'a eu eva elle joue pas pour perdre cette putin de eva c'est une vraie viper...@€€€€%&@*** -&#@
...
fatima fatima 10/04/2017 11:07:28
RAISA a dit lailaha, adji fatou est dangereuse, cherif est en plein cure ndeysanne,
...
Bineta Fatima Sow 10/04/2017 10:46:25
on dirai k l monde est en l'envers violation des hommes par les femmes ma diomiiiiiiiiii ce très bien fait pour reycha peut être k tu va ouvrir les yeux pour ta copine cherie
...
fatoukhary ndong 10/04/2017 10:44:11
ayyyy wayyy xana Raicha nopiga nak légui bouche bai tu n'étais po bien entouré naive que tu es xaritt dagnukay tann diku saytu mais ku djouk rek gani sa xarit la une bonne leçon pr tte les femmes du monde ahh moi perso sumay xarito dinako sétt bubakh l'amitié sincère est devenue très rare surtt ici au sénégal à acuse de l'hypocrisie la jalousie et rancune sa main droite bumuwolu sa main gauche faut tjr douter ds la vie tt peut arriver ohhh IDOLE vous etes les meilleurs bonne continuation Even Prod Sénégal
...
SENEPRENEUR HUB 10/04/2017 09:34:44
Bonjour, je vous invite à vous abonner à notre chaine youtube, senepreneur Hub une web émission qui fait la part belle aux startups ici au sénégal.
...
Fallou Diagne 10/04/2017 09:01:49
bou cherif di wakh mounou lén ma té ma nek si sama royaume c comm un guerie ki manifest fri ay lafamm di vollé dama bégue bilahi idole sama idole
...
hamadou Niang 10/04/2017 07:54:36
par contre Eva c'est une femme par intérêt et que la femme du grand laye ne connaisse rien et ne vois rien ce qui est devant ni derrière.
...
hamadou Niang 10/04/2017 07:49:36
vraiment grand est un homme de caractère
...
Coucou Mbaye 10/04/2017 03:04:58
Bou ndieukane djiguen lagn dane violer mouy dioy di kharou mais diamono yi goor gni llaniouy violer (l'example d'Adams)Adja fatou yow mom sa biss dineu nieuw
...
zariatou Soly 10/04/2017 01:55:47
salam nouyo na gane lafi nak dab j f3 k lir ls comment3r m3 tay mom goudj mo takh may wakh da ng3ne koy comp r3k français bi mouy lak mo khawa ng3w3l3 wagni l3ne clash bi touti ng3ne balma mane dama koy f3licit3 ndakh ma ngi doga d3gue mou wakh français t3 dougaloul wolof du courage goudj
...
Jacqueline Coura Fall 10/04/2017 01:02:19
ayy ayyy bayilenma je ne veux plus retourner dans vôtre royaume mame mbissane yaw khamenala:chérif meunama rayy
...
Valerajr Valerajr 10/04/2017 00:41:12
j kiff
...
Mbacke Dieng 10/04/2017 00:38:20
Adams boul Alou DH nanoy rek niam nga NEX NEX isssh
...
Mbacke Dieng 10/04/2017 00:37:50
Nene??sa retan yii koula guiss khamné demnga 7em Ciel ???
...
Citonass Evra 10/04/2017 00:36:27
adji Fatou kay dou dara li niit kou baxx dou KO def limo taxx kéne wolotoul kene niit dal mo leudeum??
...
No fake in my gang ! 10/04/2017 00:29:15
ohhh My god chérif en cure!! sikili mai dié yii bayi lene chérif way
...
machalla ndiaye 10/04/2017 00:06:43
ay ay ay yéne bayilene cherif beguetoul sén passeport
...
Muhammad mustafa Diagne 09/04/2017 23:06:07
Grand lay ya meun lingay deff billahi
...
mme ian 09/04/2017 22:48:13
mais idoles nekh na trop waye
...
bridji juve 09/04/2017 22:33:20
adam's néna aderer naKo basi sakouyiiiiii ????yaw mer biiiiiii feugeula thiaxabal tok sa kaw Gadaw ba plage ba di soga comprendre Ke viole nanioula mdr?????????
...
Karate Tv 09/04/2017 22:14:26
je apris beucoup de chose à travers sté serie
...
Karate Tv 09/04/2017 22:09:27
mais afair biiii doy na warr dieuguen dooy na warrr
...
Ngone thiam 09/04/2017 22:01:44
moi je suis devenue accro c 'est mon passeport {Idole}
...
Amadou Dabo 09/04/2017 21:56:37
Binta ?❤❤❤❤❤❤?
...
khadija sy 09/04/2017 21:38:03
J'ai regardé la série "saison une et deux" en quelques jours et franchement c'est la meilleure des meilleures. Par contre j'aimerai bien connaître les chansons ? depuis le début.
...
mine 09/04/2017 21:03:19
ce que je ne comprends pas moy dans la premiere saision cherif etait le chouchou de son pere et pourquoi on ne voit plus la presence du pere dans ces moment difficiles?
...
Kingston sowe 09/04/2017 20:55:41
stp..diabarou laye bi ..loumou bokh ak Fifi?
...
Fatou Seck CISS 09/04/2017 20:23:06
Hum hum Raïssa nak khana dinga yewou ta bayi naïve
...
Njay ladija 09/04/2017 18:54:40
J'adore la série. Grand Laye mention spéciale. C'est un grand acteur. Nite yi nak mome fek yenou wo say dal dougnou gueum ni danga dof. T lolou mo dal Cherif
...
Keezfa nd 09/04/2017 17:56:28
Parmis vos actrices y'a que bineta qui joue son rôle à fond !le reste dioy sakh dougnouco deff regarde moi cette eva avec ses morves elle les a certainement confondu avec les larmes, fifi aussi c'était bien pareil. J'aime trop la série mais vous autres actrices kholat len sen bopp mbir bi dou esthétique rec tamit professionnalisme dafay meutt way
...
Camara Abdoul 09/04/2017 17:53:27
Genre l'ex mari de Eva elle a payer la dot a 3millions ?? Hhhahahhhhahh je peux plus je meurs ????
...
Diaw KartushVEVO 09/04/2017 17:38:25
bon cherif pour mou wére am ameu taneu ils faut Aram koi ta papou arameu na kholleu fou mou diareu aq yayou cherif. #sakamako-dioka
...
Mamediarra Fall 09/04/2017 17:08:58
En ce moment linitt yi didoundou si xarite ak portable enkor félicitation Even prod Sénégal
...
Mamediarra Fall 09/04/2017 16:57:29
Non contan si grand lay tay djiguén waroula tékhétt kom ni way
...
Laye Ciss 09/04/2017 16:39:42
SVP donnez moi le nom du son
...
daddy 09/04/2017 15:36:10
passeport chérif kouko ame? namiti alle way ma xool???
...
Khadim Seck 09/04/2017 15:15:59
wa ki lale ns mêr bi di ???? maye nala diam de
...
daddy 09/04/2017 15:10:55
bilay boy chérif li boula daloulle wone rék ma rouss ?
...
sokhna mame bousso mabcke Sakho 09/04/2017 14:51:17
Sincèrement j'adore Raisha!! Avec elle no stress. Ces manières, beugg adouname, ay bling bling wame gnooomeuh nekhh mane!!
...
Mansour Kane 09/04/2017 14:45:46
inakaida kombe aziim
...
Shiou Dkop 09/04/2017 14:25:24
diabarou grand laye bi est très naïve li am na sakh ma warou
...
Moustapha Ndiaye 09/04/2017 14:04:13
Mān Mangi diakhasoooo dh
...
ousmane ndong 09/04/2017 13:58:25
no adams khana gpuddy nèkone yow nènè mba nding dammoule fokoule .moy thiowe djibboule
...
Ado Ndiaye 09/04/2017 13:44:23
billahi yèna fi meunne vous etes le meilleure
par