Signaler un problème
 
...
Mame Awa Diallo 09/04/2017 19:57:09
film bi Tass na man dama douyal l'I yeup warouyouko thi bouler amatoul sanse
...
Mbagny Ndao 09/04/2017 15:47:58
na yam la serie na plus de khoromm
...
Awa 92 09/04/2017 15:41:47
keske soumboulou ne doi pa savoir?
...
Pape Mansour Seck 09/04/2017 13:31:14
bebe sy vs etes charmantes bon continuation lep pay bakh
...
Marieme Ndiaye 09/04/2017 03:13:42
keen degoule sah
...
Amadou Diallo 09/04/2017 01:03:50
Jojo!!! Tey mome 10/10 . Respect! Raw ngua say mass!!!!!
...
doudou fall 09/04/2017 00:09:47
?jojo mo eup birr qui eumb?
...
abdou khafor 08/04/2017 22:48:28
toubab yi dilén diokh ay Serie you gueuneu yag té sof té daguén koy sétan bamou diékh té nan waroul won diékh légui
...
abdou khafor 08/04/2017 22:44:51
koumou nekhoul rek boul ko sétan
...
abdou khafor 08/04/2017 22:42:33
wa Mai yén linguén beugu nak kén khamou ko pourtem afere yi métiwoul kou mou rek boul ko sétan kén fayoulén pour ngén sétan ko
...
Mergane Modou 08/04/2017 19:51:02
thiey mbaye kane mola euball kayy
...
Moustapha Ndiaye 08/04/2017 19:41:46
tv
...
generation new 08/04/2017 18:39:43
mbaye beugue na la ,.... lou guay deff si wiri wiri bi ..... nonnn yagui bomb
...
mame siny 08/04/2017 17:55:42
tjr des problèmes sans solution ahhh série bi nak kagnlay diékh li môme amatoul chance
...
vivi thiala 08/04/2017 17:38:15
MBAYE REW NAAA HAHAHAH
...
fifi diop 08/04/2017 16:46:41
mais mane son bi nék espagne doumako dégue si manela walaa?
...
MASCINA Aliou 08/04/2017 16:35:14
hhhhhhh non mbaye reynaa. Moi j'ai raté bcp d'épisodes tellement j'en est marre thi film thi film boudoul diekh. Aussi qualité de professionnalisme bi dafa dess trop même sou féké réalité sénégalaise yi ngene di joué, il faut que sa soit un produit de purement professionnels comme CAFÉAVEC , ou bien POTE ET MARICHOU.
...
Ndeye Mama Fall 08/04/2017 16:02:59
mbaye dofoul wala
...
linguère Gueye 08/04/2017 15:59:00
Weuh ana première partie bi... Aye Mbaye wagnil sa galatie gnu diam là ganè bb numuy sante milliardaire dèna ???Soumboulou boul firr ndax ya saflè ???merci way pour ces moments de bonheur ???
...
khoudia gaye 08/04/2017 15:09:09
danga agressif si xalei Mbaye,.. mdrr
...
khoudia gaye 08/04/2017 15:08:44
non Mbaye tu t'entends parler là.. ! mdrrr..
...
khoudia gaye 08/04/2017 15:06:37
nooooo mbaaaaaye té pas sérieux....!!!
...
lo esprit 08/04/2017 15:03:04
non!!mbaye dal dinama dead kw
...
non Lii werrente rek lá wade 08/04/2017 14:54:27
bmaye dou dem???
...
Maimuna Jallow 08/04/2017 14:45:18
Why I'm not hearing huh????
...
Ado Ndiaye 08/04/2017 14:06:16
depuis spagne ba lègui manou nio kham linguèn di wakh ah soof na troup way ! !!??
...
Mansour Kane 08/04/2017 14:05:19
mbaye ray na ma
...
Laye Ciss 08/04/2017 12:32:48
ishhhh wiri wiri ba douggou Espagne té sén wakh léroul mounone guèn di dém Goré réseau bou bah mo nék fofou?
...
Ibrahima dia 08/04/2017 12:25:29
nafi yam wayy
...
eauxclairesslsn 08/04/2017 12:23:48
mdr Mbaye dou nitt!!!
...
PRINCESSE PRINCESSE 08/04/2017 12:09:12
Soumboulou t' as trop bougé à la plage pour une femme enceinte.
...
Lucas Oliveira 08/04/2017 11:57:55
mbay dinama ray
...
Amo Tdg 08/04/2017 11:53:46
Revoyez le son way s'il vous plait
...
Ramses Chou 08/04/2017 11:53:36
wa hana dou jojo da wakh dafay geneu deuk bi ande ak soumboulou? wa dougnou géneu senegal nak? niti dal senegal rek lagn wara tok? kene amoul droit bouger? en plus li film leu rek ils ont le droit daller tourner ou ils veulent non...dagni geneu deun bi kay warougnou tok sali wala casamance....wala? ??? mane dal warouna. senegal nehneuu....
...
Amy Niang 08/04/2017 11:46:07
Ah Sénégal mo mbetti lou takhe kene dou avancer.critiquer reke .nane sou done mane. bonne continuation soleil levant
...
Roube. com 08/04/2017 11:36:08
voix yiguen di couppe mom dou affairou professionnel un peu nullll ay merde la way respecte len niouy setan aussi
...
latdior traore 08/04/2017 11:27:01
vidéo zéro
...
Kadidja Ndiaye 08/04/2017 11:16:11
vidéo zéro
...
Fadel bu xaragne lo 08/04/2017 10:38:06
mbaye le futur milliadaire de tou les temps sacre mbaye
...
Famita Diop 08/04/2017 10:27:58
???liir mo agresessive
...
El hadj LY 08/04/2017 10:09:14
Salam mes amis, T o p s t o c k est une appli galsen sur google play. Une fierté sénégalaise Télécharger et partagez en masse. Merci
...
elhadji Ndongo ndiaye 08/04/2017 09:56:49
nn billahi mbaye doma ray nak ???????mai li amul
...
Didi Dada 08/04/2017 09:56:30
Clarisse Vendredi ou Catherine Vendredi alias Viviane Chidid (cache front gauche) talou léne WUYUMA TOUR am mo ko nior té lolou meune mo yeuye abal lène thi ba mou amé tank. Temps yi mougui "Wuyuma" di "No Stress", di "Lii Dafa Niaw", "Lon Keken", di "Mariage Forcé" di "Sénégal Bop" LOL. Mbaye j'adore ta franchise (bi nga dona ci madré piss ;-)) & tes larmes (bi nga dona thi sa Papa Fall Toubab) mais gui niougne raye! BB Sy tjrs aussi belle macha'allah!<3 Cheikhouna ya raffet xole. Je crois que & ns n' avons pas le mm Calendrier eux ils sont encore au 8 Mars mo takh série bi binda goul END!!! Comme d'hab ct à chier!!! En tt cas nioune niou gui thi le 08/04/2017. "Idoles" ah quel bonheur fadj gathié yéne la guem & vivement le retour de Pod & Marichou pr le 15/04/2017 xalé you am diom té meune lou gni def laf thiat!!! <3<3<3
...
Ngarubiram Fall 08/04/2017 09:55:02
Affaire bi mi ngi commacé soof. Série Idoles moo dakh fuuf!
...
swag xboy 08/04/2017 09:52:36
Wolof Ndiaye nena… lou teug tass wiri wiri walahi dayal nagnou! lilahi wa rassouli-hi nafi yam
...
Muhamed Kanteh 08/04/2017 09:51:42
mbaye dinama raye noo true love is nice God bless you mbaye
...
Bintou Nette 08/04/2017 09:50:09
Wa khana Las Palmas mom amoul preneur de son?
...
Bocar TV 24 Ka 08/04/2017 09:45:34
fi dou espagne fi almady la
...
seyeamadou 08/04/2017 09:28:09
espagne dou dara saly ngén warone dem wala saint louis ou casamance et faire du publicité local
...
samba niang 08/04/2017 09:24:50
ani séne sonnnnnnnnnnnnnn
par