Signaler un problème
 
...
Touray Ousman 10/04/2017 15:16:20
I like mbettel so much
...
Nafi Dieng 10/04/2017 15:04:45
papa Diouf n'est pas un père responsable il n peut pas donner ds leçons à personne. lena môme as pris une mauvaise décision.
...
Salafi Ahmad 10/04/2017 14:59:34
khanaa papa warna Russ ruba leigi
...
Salafi Ahmad 10/04/2017 14:45:18
oumar boybi wakh nala deug dh
...
Bacari Kane 10/04/2017 14:28:36
Non, mais ce papa diouf est ce que wër n'a. Non lui le pédophile il va au resto et il se plaint que sa fille y soit un gars qui de son âge et de sa génération.
...
Mamisey1587 Seynakayne 10/04/2017 14:24:25
mais oumar sa copain wakh nala deug nak
...
OULIMATA SISSOJHO 10/04/2017 11:46:01
HA MADIONNE DAL LILANE LA IL POUVAIT METRE UN CHEMIS BLEU OU BLANC AU LIEU DE UN AUTRE CHEMISSE EN WAX VESTE BI REK DOYI NA THIE WAX
...
Khady Virginie Ndour 10/04/2017 11:43:32
Rouba nak il est temps nga yeewou té contre attaquer han! mane beugouma yii dara
...
Bineta Fatima Sow 10/04/2017 11:35:52
SAMA dôme SAMA néné tout lolllll mais douma sa dommmm teygama papa sofna yabatrna yoww guayy fireeeeee te kene firoula mais lena yabategua si rouba gayyy terale dougual gua sa lokhooo si sauce bou tangggg
...
Dabiche Ndiaye 10/04/2017 11:28:51
omar wakh degeuuu ????
...
adama lo 10/04/2017 10:58:26
Sénégal dounou ndm def feneu bilaee parent bou xamoul ndm bopam il faut niou waxko ndm bopam
...
Baje Mbaye 10/04/2017 10:33:22
je trouve que Rouba n'est pas naturelle.n
...
Khoudia Sy 10/04/2017 10:28:13
degue rék ga wax omar dafa bery loumouye dambate té lolou bakhoule si nite
...
anta yeboue 10/04/2017 10:12:14
WAA MADIONE MII KOUMOU YAPE AK SANGSEM BI LOL
...
aliou1 diallo 10/04/2017 10:07:01
aliou1diallo
...
Mbacke Diop 10/04/2017 09:59:17
mais Léna imenzilénn liko Balla gaye wara mayy comme k yayam nééna douko mayyé sii 3million ?? mais papa Diouf noonou la déé goor dayy amm foula keur guii yafay goor défal nigakko sentiré pask momo geunn ndiallo fiii paaa you barri takouniou Sénn moromii doom mais gnigui lakou akk niomm si roukk yii akk hôtel yii akk auberge yiii loulérr laaalay téggal niiiii
...
Sope Naby 10/04/2017 09:34:39
Bien répondu Léna t'es pas sa fille mais tu lui dois juste du respect c'est tt
...
Cheikh Kebe 10/04/2017 09:14:59
papa diouf sa telephone rafétna , bala gua mayé ay million si dote gua diene telephone bou baah
...
lala aicha diop 10/04/2017 09:13:29
gnaw mala fan lena Rouba dafa soof thiiiipatou
...
Samba NIANG 10/04/2017 08:59:08
wa papa diouf mii hamna fiy meetii
...
seyna diouf 10/04/2017 04:40:28
ohhhh Rouba tay danou gua woro wakh ak mome. meuno di jouer en plein match beug guéne di wakh ak ki nek si banc bi mérénala torop
...
Diagne Diagana 10/04/2017 03:58:17
mé léna mi la bala gaye 2 marié
...
Abdou Lahad Gueye 10/04/2017 03:23:54
omar sa copain wakhna la deuga il faut ga respecté sa bopou ????????
...
Mamadou Ndongo 10/04/2017 01:06:05
✔➕✔
...
amekebe kebe 09/04/2017 23:10:33
rouba mèrenala troppo yène bakhyi ak dofla bilay?????
...
Mamad OU 09/04/2017 23:08:58
ahha???? lena dale bayiwoule kenneu , sauvegarder len sen dieukeri , léna d bayiwoule kenneu k
...
Mamad OU 09/04/2017 22:58:17
degeune tane guoor foulla ma fan papa diouf, faut lui sanctionner couper les privilèves elle s'aura qui est le père lool , mais doune khaff on ta parfaitement dit la vérité soit un homme en vrai pour une fois et cesse de complaindre et de lamanter pff
...
FAMA DIAGN 09/04/2017 22:44:36
coll
...
Fatima Ndiaye 09/04/2017 22:31:05
néna agne bi guén meuy may dou saff dakarr???omar dognou diappalé t changé touti sonounagnou
...
Ebrima Camara 09/04/2017 22:25:14
Non pape douf dou dem Lena balla dalla fasse
...
mya mbow 09/04/2017 22:13:38
Rouba nak amal touti foulla sisaa bopp ahh lilane la ni nitt day digne diaroul yalwane dioubo
...
Pisco El Presi 09/04/2017 22:08:52
amina may nala diam yaw
...
Rokhaya Tall avec Sen Theate Italy 09/04/2017 22:02:46
papà gnambe dal may nala diam .diamu rekka mata kheuthio
...
Fatou Ndiaye 09/04/2017 21:49:11
Léna diga kam Lou réwanedeii di dierune.
...
vanessa Conti 09/04/2017 21:47:41
Mandione sa sangsé rafeetna mais tu aurais pu mettre une chemise blanche pour casser avec la veste je dis sa je dis rien ... sinon vous jouez très bien. .. bonne continuation
...
zeynab diouf 09/04/2017 21:41:54
papa diouf way mdr yagui beugeu niak fouleu nak si say kanamu dom... haley bi mom bul halat niu bako ishhh... Omar ton ami mom deug rek lala fi tegual mom na goree touti te gua niafe sa life
...
Cheikhouna Lo 09/04/2017 19:38:03
omar xawma doun xafa deugg rèk lala sa way waxe
...
Aicha Fall 09/04/2017 19:31:25
je me demande loutah goor baadola? douniou halat loudoul sen bop teh gawa faté demb. mais gnounit djiguéne kene dou nioune da gno gnak yeurmandé ak solidarité sunu biiirrr.
...
Lalishta Lalishta 09/04/2017 18:45:22
Haaaaa changement mo gaww lena dé legui da féroce
...
Ass Ndiaye 09/04/2017 18:23:32
Lena j'ai pas du tout d'accord avec toi ruba limoula waxx dara nékosi nitt dayy âme yar xam waxine bou rafétte papa Diouf mom dafa gnak fayda Wanté merci amina
...
wakh diam 09/04/2017 17:06:39
mais lena khamoul bopam de rouba dila enranger nga koy deranger eupel nga de yangi may beuga sof ndakh khamo sa bopou yabate lool papa diouf mom dama ko diepi khamoul sakh nim may def ki koukoy wakh bopam
...
Nguissaly Diasse 09/04/2017 16:48:01
wayen lena mom telna yenu yeuf Di sof mai lilay khar khamoko de mal rek
...
cisse evana 09/04/2017 16:42:09
lena sa se voit qu'elle a trop grossi
...
fatou Ndiaye 09/04/2017 16:04:53
fecebook mayna laye weur mayna fawmou wakhma li mouye diwou tien bi bakhna
...
Kha Dee GUEYE 09/04/2017 15:51:38
Eeewaayyy Mandione yaa dieul sa Wax niii daggueu si chemise daggate si veste ???.... Sa tissu doyna
...
boy Seck 09/04/2017 14:51:29
#NDIAMBÉ sof ngama ngay léb lébal melni kou deukk ci famille léb léb ish
...
Fallou Fallou Diakhate 09/04/2017 14:47:38
Wadji khasna omr waxna d3uk3u omr Dafa yambreh koi omr nagore díantal ga baye
...
Mya Fall 09/04/2017 14:47:09
wa " cdisé" moy laan tamit!! farou maîna bi tamit set na li mou wakh ?!? ahhhh! mane khawma sakh nou ma ko war bindé...
...
Aïda Gaye 09/04/2017 14:38:16
mane mom amina rk la fan trés bien Deug rk nga wakh
...
mary mantoulaye fall 09/04/2017 14:35:52
Wouy Rouba raye nama Amina neenako wax nako luy tak du faye mu niko danga reeew motax nonnnn Rouba Mala Geum Piiir franchement yangui joué lu neeex
par