Signaler un problème
 
...
paco papi joop 07/04/2017 19:28:16
jazz maynala diam dh
...
paco papi joop 07/04/2017 19:11:04
jazz for ever 20/20
...
paco papi joop 07/04/2017 19:10:42
team jazz la bok
...
thiam aissatou 07/04/2017 18:34:51
weuhhhh Oumy akk jeff mom luniou nar ni ehem..., Aichaa ndeyssane ...., mdrrrrrr no david niam gua dhhh bilaie dotoko defati....
...
ROKHAYA KEBE 07/04/2017 18:03:44
Fana chon na ak teint noir bi machALLAH
...
ROKHAYA KEBE 07/04/2017 17:55:25
waa eeh 1h ? aah LifeLine Show taay maynalene diam d ..
...
xavi willson 07/04/2017 17:41:25
amina ligua pathial pathiouna
...
Fatou Diop 07/04/2017 17:26:45
? off lifeline team jazz minaka ????? non jazz rek maynala diam de
...
Bacha Malang 07/04/2017 17:19:53
Davide yako def rakou militaire kén douko dophane dici guéné nonou ???
...
limame dieng 07/04/2017 17:16:48
lifeline rék
...
limame dieng 07/04/2017 17:15:30
wa mané méynaléne diam déih ....
...
Aliourokhaya barryniane 07/04/2017 17:07:13
nn fi todjna malen may diam????
...
Kadia banor 07/04/2017 16:30:14
j'a kiff de ouf deuxième saison bi nakouwa niou????
...
Seyzee 07/04/2017 16:26:13
#NiceFilms lou nékh dou doy way douma lén may Jam dh ba saison 2
...
Thioune Kabachallala 07/04/2017 16:22:09
mane jazz douma ray
...
Mamegorr Ss 07/04/2017 16:11:33
li dafa nice
...
Safietou Diallo 07/04/2017 16:11:15
nekhna wiy
...
Papa Fall 07/04/2017 16:10:07
no fin bi darà dakh ko
...
Awa Ndiaye 07/04/2017 15:49:58
nekhna trop du courage à toute l'équipe
...
oumou kalsoum ba 07/04/2017 15:38:37
I like
...
Gnima Diatta 07/04/2017 15:28:21
hahahaaaaaaaa thioukou na keyyy
...
astou diome 07/04/2017 15:07:46
félicitations à l'équipe lifeline maynalen diam dee
...
Moussa Traore 07/04/2017 14:20:59
Me jazz bague nala magui ley bègui bay
...
Moussa Traore 07/04/2017 14:20:10
Ohhh ? my good
...
BEBE diarra Gueye 07/04/2017 14:19:41
machalla ylala na ylala Lafe thiate
...
3S. COM 07/04/2017 14:19:28
wouuuuuh David maynga Fana ak Amadou diam dé.....félicitations mais svp pas de Fonaneté à la 2nde saison...ok
...
Gueye Thiam 07/04/2017 14:17:05
mais saision 2 bi kagn la?
...
La Papillon Rose 07/04/2017 14:15:48
Mareme je t'adore
...
Moustapha Ndiaye 07/04/2017 14:07:37
trop trop nékhéss machallah Man Maye na lénn diamë Dee ñoo ngi xarr saison 2 bi nak bumu yageu nak????????? Parce que bou yaggé rk ñu fàtte Ko Wasalaam
...
Souley Bayo 07/04/2017 14:00:55
kiakiakiakiakia nekh na tropp
...
Babacar Sokhna 07/04/2017 13:37:47
maynala diam dh
...
Km Dari Modou Modou 07/04/2017 13:36:58
Mi piace
...
Dabina Love 07/04/2017 13:35:24
No vraiment serie bi nekhna trop bonne continuation ....meynalen diammeu dal❤❤?????
...
Mame Mbayame Ndoye 07/04/2017 13:26:33
chapeau a vous way machalla nexna trop
...
Mouhamed Kane 07/04/2017 13:26:02
waw mais dev may nala diammeuh déh??
...
Mamadou Seye 07/04/2017 13:23:42
Jeff ak Oumy ooh couple bou Nice vraiment Jaime trop Jazz mane maynala djam dh ak Amina nii dafa raféet bonne continuation les gars saison 1 neexna trop
...
boudechou 07/04/2017 13:11:09
OMG!!!! Lii nekh na ba eup way ohh David makoko yéné je lai au moins replay 10 fois walah vivement la saison 2
...
adama lo 07/04/2017 12:56:19
souma life mangui doga fan un man com moi vraiment Jazz man damalay begueii koii ???
...
cvsenegal 07/04/2017 12:46:11
trop nekh na saison 2 bi gaw way
...
jeff le prince Diop 07/04/2017 12:39:47
im a fan of jeff coz i change my name online into jeff i like him and i would like to have his acount or adress mail please guys
...
jeff le prince Diop 07/04/2017 12:37:55
omg vs etes vraiment les meilleurs i like this movie and wish good succesfull im a brother of mimi and marem
...
Maimouna Mouhamed FAYE 07/04/2017 12:34:23
mane soppeu na Fanna trop way
...
Moussa Soumare 07/04/2017 12:33:27
jazz the best
...
bamba n 07/04/2017 12:33:17
maleen begue pirr série bi nekh na trop félicitations lifeline love _u
...
mouhamed niang 07/04/2017 12:24:56
great!!! maynalene diamm deh... keep doing that good work!
...
Khadija Diop 07/04/2017 12:11:31
Diaz maynako diam dh? aïcha elle est animée par Kel esprit? limou beugonn amna loumouy xeum?? candy ioe do gueum saxx loy yeuk???mareme massah? amadou amnga full chance✋ mais pause l'otre gars ex mounaass bi pq gneuwoul ci mariage bi ak oumy? mais daall it's was cool so please the second boumou tardei bala gnouy fatei first bi (liré lenn ko kom marem nimouy waxé nak??❤ ndaxx xalé bobou maynako diam dh seumm?)
...
Sokhna Hann 07/04/2017 11:51:33
machalah serie bi dinama wéteul ohhh it's verry verry Nice à bientôt et félicitation pour la réussite ??????????????
...
bathie gueye 07/04/2017 11:40:57
nicc amadou deve dou yombo dhh
...
mami fallilou diagne 07/04/2017 11:37:37
félicitations à toute l'équipe ligueye biii rafetna trope . mais please n'a wakh yi rafètt wayye . vraiment aye sagua avec des trucs exagérés. diapeu lènn ci senegal soutoureu la
...
bathie gueye 07/04/2017 11:34:18
niccc amadou
par